Hip-hop

ay breakat

Hip-hop ag yëngu-yëngug caada ak fànn la, mi ngi juddoo ca Réew yu Beenoo ya ci ndoorteel ati 1970 yi, daa boole bànneexu ak ñaxtu. Mi ngi juddoo ci biir askani waa-aamerig yu ñuul yi, ca New York, fa la tàmbalee, mujj tas ca réew ma ba ci àdduna bi bépp, ba tay mooy dundiinu réewu-taax wi ëpp doole. Caaday Hip-hop ci ñeenti ponk la tënku: break dancing, DJing, MCing ak .

Wii xeetu fànn ñu bari ci woy wi lañ koy tënk ,MCing, te mu gën a siiw ci rap. Caadaay Hip hop yamul rekk ci rap, man naa sol mbubb yu wuute: su fekke danuy yam rekk ci xoosug DJ bi (Disk Jokey), waruñu ko tuddeeti rap, waaye DJing , sunu yamee ci li MC bi (master of ceremonie, njiitul xew) di bàcc kon man nanu koo woowe rap, walla tamit, donte bari na lu muy faral di am, boolee benn DJ ak ay walla benn MC, kon ci nii hop-hop lañuy wax, ndax rap ak MCing yépp ci caadaay hip hop lañu bokk, waaye nit ñi rap lañuy wax rekk yam ci ngir yombal.

Other Languages
Afrikaans: Hip-hop
Alemannisch: Hip-Hop
aragonés: Hip hop
العربية: هيب هوب
asturianu: Hip hop
azərbaycanca: Hip-hop
Boarisch: Hip Hop
беларуская: Хіп-хоп
беларуская (тарашкевіца)‎: Гіп-гоп
български: Хип-хоп музика
brezhoneg: Hip hop
bosanski: Hip-hop
català: Música rap
čeština: Hip hop
Cymraeg: Hip hop
Deutsch: Hip-Hop
English: Hip hop music
Esperanto: Hiphopo
español: Hip hop
eesti: Hiphop
euskara: Hip hop
suomi: Rap
føroyskt: Hip hop
français: Hip-hop
Frysk: Hiphop
Gaeilge: Rapcheol
贛語: 嘻哈音樂
Gàidhlig: Hip-hop
galego: Hip hop
hrvatski: Hip-hop glazba
magyar: Hiphop
հայերեն: Հիփ հոփ
Bahasa Indonesia: Musik hip hop
Ido: Hip hop
íslenska: Hipphopp
Kabɩyɛ: Hɩpɔpʊ
қазақша: Хип-хоп
한국어: 힙합 음악
Lëtzebuergesch: Hip-Hop
lietuvių: Hiphopas
latviešu: Hiphops
македонски: Хип хоп музика
മലയാളം: റാപ്പ്
Bahasa Melayu: Muzik hip hop
Mirandés: Hip hop
မြန်မာဘာသာ: ဟစ်ဟော့ ဂီတ
Plattdüütsch: Hip-Hop (Musik)
Nedersaksies: Hiphop
Nederlands: Hiphop
occitan: Hip-hop
Ирон: Хип-хоп
Papiamentu: Hip hop
português: Hip hop
română: Muzică hip-hop
русиньскый: Гіп-гоп
srpskohrvatski / српскохрватски: Hip hop
Simple English: Hip hop
slovenčina: Hip-hop (hudba)
slovenščina: Hip-hop
shqip: Hip hop
српски / srpski: Хип хоп
svenska: Hiphopmusik
தமிழ்: ஹிப் ஹாப்
Türkçe: Hip hop müzik
oʻzbekcha/ўзбекча: Hip hop
Tiếng Việt: Hip hop
吴语: 嘻哈音乐
მარგალური: ჰიპ-ჰოპი
ייִדיש: היפ האפ
Yorùbá: Orin hip hop
中文: 嘻哈音樂
Bân-lâm-gú: Hip hop
粵語: Hip hop